Catégories
Saabal

Faatug Nd G ngone su jigéen su am 2i at ca Mbuur

Ngone su jigéen la ñu fekk mu faatu ci tabax bu yeggul ca Mbuur. Goneg 2i at gii, mu réeroon àllarba bii wees, ci tabax bu yeggul la ñu ko fekk mu faatu ca koñu Liberte 2 Bay-dëkk ca Mbuur. Gone gii réeroon àllarba bii wees, ci ay xeer la ñu fekk ñu làq ko fa. Kenn ku bokk ak moom kër nag takk-der yi téye nañu ko ndax moom la ñu njort ne moo ko def.