Catégories
Saabal

DOOMI IRAŊ YI DAJE NAÑU

DOOMI IRAŊ yi nag, def nañu ay ndaje yu mag te kenn yëglewu ko ngir ñaawlu xiixaanug Merig ginnaaw ba mu faatee Xasem Sullaymaan ak ñenn ca ñay xeex noteel.

Ñaxtukat ya nag ñoo ngay sàkku ci njiiti bokkeefug Lislaam gu Iraŋ gi ñu fayyu ca na mu gën a mettee ci DOOMI AMERIG yi ak Israayel.

Leeral:
Bokkeef g=République
Xiixaan g=terrorisme

Yëy-yàbbi