Catégories
Saabal

SEEX YÉRIM SEKK LIM NA ÑENN CI WAY-POLOTIG ÑI…

CI JANOOM AK AYSATU JÓOB FAAL, SEEX YÉRIM SEKK LIM FA ÑENN CI WAY-POLOTIG ÑI MAN A WUUTU MAKI SÀLL

Bunu sukkandikoo ci taskatu xibaaru politig bi, Maki Sàll ñi mu teg bët ngir ñu wuutu ko ñooy Abdulaay Daawuda Jàllo, Maxtaar Siise, Mansuur Fay ak Seex Umar Aan. Njiitu réew mi doon na bëgg lool itam Idriisa Sekk wuutu ko, njiital kureelug Réew mi bis bu set moo ngi déggante ak Maki », ci li Yérim Sekk wane.

1 tontu ci « SEEX YÉRIM SEKK LIM NA ÑENN CI WAY-POLOTIG ÑI… »

Moom de daa mel ne am na xam-xamu segg biri pólotig. Waaye wolof nee na: « li ci kanam rawul i gët ».

Yëy-yàbbi