Defarkati mburu yi yëgle nañu ag selaŋlu. Mbootaay gi lëkkale kureel yiy yëngu ci lakk mburu xamle nañu ne dinañu xeex lii di yokkuteg mbëj gi, ba ci bu jaree sax ñu bank seen i yoxo taxawal seen liggéey, te su booba mburu du amati ci réew mi.
Leeral:
Mbëj g=électricité
Seleŋlu g=grève

4i tontu ci « YOKKUTEG NJËGU MBËJ GI: »
Cëy waa jile miim réew
Yokk gi de ëpp na lool.
Yéeme na
Mbëj gi de jur na coona.
Dégg naa bu mbëj yokkee lépp seer!