Catégories
Saabal

IRAŊ/AMERIG

Bu nu sukkandikoo ci xibaar rej yu Iraŋ yi, ñaari cong ya ñu amal ca karceg Amerig ga gën a mag ca Iraag di Ayin Al Asaad faat na fa lu mu néew-néew 80i soldaari réewum Donaal Tërëmp. Lim ba dëgg nag xamees a ndax nëbb gi ko njiiti Amerig ya di nëbb waaye gisees na ñu sàkku ndimbal ca raglu yu réewum Iraag ndax jaaxle. Ay fafalnaaw ak jumtukaay yu bari yàqu na fa.

0 tontu ci « IRAŊ/AMERIG »

Yëy-yàbbi