Catégories
Saabal

YÉERE AK I MUSIBAAM:

YÉERE AK I MUSIBAAM:

Yéere yi nuy sol moo nuy jox tawat yu bari, ñi gis ci àdduna ndax at mu jot dananu defarlu ci ay yéere ci li nu xayma 80i milyaar ci ay yéere.

Yéere yi nag tooke lan ciy def ngir mu rafet, nit ñi koy sol nag moom danuy tànn rafet gi rekk fekk ñoo ngi màbb seen ug dund te yëggu ñu ko. Yéere bu la gën a rafet moo la ëpp tooke. Bari na ay tawat yu bari ñuy jàmbat te fekk na yéere yi moo nu ko jox.

Yëy-yàbbi

error: Content is protected !!