Catégories
Saabal

Jéya ju metti moo am tay ci alxemes ji ca Luga

Jéya ju metti moo am tay ci alxemes ji ca Luga bi fukki waxtu di jot. Bunu sukkandikoo ci RFM, ñatti doomi Muritani ñoo ca faatu. Amna ñatt ñu ca am ay gaañu-gaañu ba ñu rawale leen ca raglu Aamadu Saxiir Mbay.

Yëy-yàbbi