Catégories
Saabal

UNAAKUWAA JÀPPOO YËGLE NAÑU AG YOKKUTE CI NJËGU DUND GI

Unaakuwaa àrtu na ci yokkute gi dëgmal ci njëgu dund gi. Bunu sukkandikoo ci Usmaan Njaay, di jëwriñ ju sax ju mbootaayug yaxantukat yi, ñoom xamuñu li waral nguur gi yokk kumbal gi aju ci lépp luy dugg ci réew mi. Joge na 2% dem ba 12% batax dëggal na ne bu ñu dàjjiwul dogal boobu, njëgu ceeb ak diwlin dina fulu maanaan lu doon jar dërëm, ñaari dërëm lay mujj jar.

2i tontu ci « UNAAKUWAA JÀPPOO YËGLE NAÑU AG YOKKUTE CI NJËGU DUND GI »

Yëy-yàbbi