Catégories Saabal PÉKKE CA KOLDAA Auteur de l’article Saasumaan Bi Date de l’article 23/01/2020 Aucun commentaire sur PÉKKE CA KOLDAA Facebook0Tweet0 Lu bees ci mbirum jigéen ja ñu daggoon bopp ba ca Koldaa di Yooba Balde. Bunu sukkandikoo ci L’Obsevateur, jëkkëri aj-loro ji lees jàppandi ngir wéyug luññtu. Looloo ngi am démb ci àllarba ji. Leeral:Pékke: crime Facebook0Tweet0WhatsAppTelegram ← WAXTAANU BERLIŊ NGIR JÀMM CA LIBI, 19 SAAWIYE 2020 → DOOMI AMERIG JI GÀDDAAY NDAX DIINEEM TE ÑU RAY DOOMAM Yëy-yàbbi Annuler la réponse.