Ŋaañ

Xàmp.

Booy ndékki dangay ŋaañ mburu mi guux kafe gi.

 

Ŋayam

Ne ŋayam: (njëfka)

Gàncax gu dee ba wow koŋŋ, ba tàmbalee funux. Niral: Boo bàyyee garab mu ne kayam, ginnaaw ay weer nga jaaraat fa danga fekk mu ne ŋayam.

Ŋiim

Ŋiim b: tur 

Tañaag

Ŋurumtu

Di ñaxtu ndànk ca suuf. Ñimewóo béral la ngay wax ca kaw. 

Niral: Xale bii de mi ngi ŋurumtu rekk xamuma lu ko naqari.