Duu

Duu b: tur

Lees di def am ndugg walla leneen. Niral: Sama yaay a ngi ñëw, yor ab duu def ca màngo bamu fees.

[En: basket]
[Fr: panier]

Duxóos

Duxóos: njëfka

Dugal gu gaaw. Aw dugaliin la. Niral : Yàlla na nu Yàlla ne duxóos àjjana.