Giif

Giif: jëf

Mer mu def, ku mer ba giif mooy ku mer ba meratul.

Giim

Giim: (jëf) Lu fay, mbaa muy bëgg a fay. Xal wi daa giim yaw ëf ko.

Giléem-mbëtt

Giléem-mbëtt w: tur