Naaxsaay

Naaxsaay: jëf

Jeex, seey, xiin wu naaxsaay, xiin wu fi ne woon ba yàgg muy dem ndànk ndànk ba set wecc.

Naq

1- Naq: jëf

Jël boppub nit dugal ko ci ndox ngir mu xëj. Ku soxor a koy def. Niral: Ndaysaan, waa jee ñu jëme ca mbalka ma de, dees koy naqali.

2- Naq b: tur

Ci ron jumbax. Niral: Bul bàyyi sab naq muy feeñ.

 

Nataal

Nataal: tur

Këyit wuñu def jëmi nit , mala,  gàncax walla lëfñ

 

Ndaag

Aw tur la

Ndaat-saay

Ndaat-saay: Baat la bees di daaneele am pecc.

Ndaayànde

Ndaayànde: Ab dëkk la

Ndambe

Sëb suñu togg, te di ko faral di def ci mburu.

 

Ndéggat

Ndéggat  g: tur 

Lees sottandiku ba noppi ñu war koo déglu (ojoo)

 

Nduyaan

Nduyaan g: tur

[En: charger]
[Fr: chargeur]

Nebbantaan

Nebbantaan m: tur 

Xale bu tollu ci juróomi at ba fukki at.