Raas

Raas: (jëf) Mooy for meññet mu tàbbi.

Niral: Xale dañuy raas déem.

Rañaan

Rañaan : (jëf) dox guddi, tukki guddi. Xëy dafa am, gontu am , rañaan am.

Rañaan

Rañaan (jëf)

Tukki ci guddi bu lépp nee selaw, nga topp guddi gi ngir tukki.

Rajo

Rajo b: tur 

Rambaaj

Jaxase ñaari nit ba ku ne jàppal sa moroom lu ñaaw.

Niral: Rambaaj lu bon la.

 

Rapp

Rapp: njëfka

Ne rapp, tëju, fasu, lépp dajaloo ci digg bi.

 

Ropplaan

Avion

Roset

Xeetu rocciwiin la, ni ñu ko roccee.

Niral: Neel roset jaasi jooju jox ma.

 

Runge

Jaxase ñaar yu niroo te bokkuñu. Di tari ba yàgg nga génn saar wi nga ne woon dugg ci weneen saar

Ruuj

Ruuj: jëf

Setal sab tool ba moo taw, ngir bu tawee rekk nga man a ji. Niral: Baykat yépp ruuj nañu seen i tool.