Xafara

Mattum salaan walla ngeer mu man a tàkk.

Xalima

Xalima g: tur 

Bant bees sot ba cat li sew ngir di ko binde

Xalimag ndëpp

Xeet la ci xalima yi. Amna ñoo xam xam ne xalima googu rekk lañu man a binde.

Xalimag njengal

Xeet la ci xalima yi. Amna ñoo xam ne xalima googu rekk lañu man a binde.

Xallóob:

Xallóob b: (tur) Mooy doomi gaynde, gaynde gu ndaw.

Xamtil

Xamtil: jëf

Xamul. til = ul. Nëxtil = nëxul.

Xar

Xar m: tur 

Mala la, mu ñuy yër ci kër yi.

Xay

Xay g: tur 

Ag garab la

Xayta

Xayta: tur

Puub, day, ay ginnaaw kër.

 

Xànc

Lu mel ni ay buum la te ñu koy xollee ci garab. Amna ñuy takk ay xànc ngir faju.