Bijjanti

Bijjanti: (jëf)

Gunge bu ànd ak waxtaan di dem, waaye doo àgg fa ka ngay gunge jëm.