Cabb

Cabb b: tur

Ak dank, dajaloo ci benn barab. Niral: Jigéen ñaa nga def ab cabb ca ëtt ba.