Céebo

Céebo m: tur

Nawet bi dees koo séddale ay xaaj. Xaaj yi yu njëkk yi nag lees di woowe ay céebo. céebo mu ne fukki fan ak ñatt lay doon. Amna céebom dabraan, anaata, dékk añs.