Ëcc Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Facebook0Tweet0 Ëcc: jëf Génee ay wëñ ci wëttéen. Jël wëttéen taqal ci ëccukaay di wëndeel muy def i buum di laxasu. Bu laxasoo ba fees di poqe. En rapport Baataan Jollasu Facebook0Tweet0WhatsAppTelegram ← Daakaande → Gale