Féew

Féew: (jëf) Beddiku dem yaw dong bàyyi say bokk walla say xarit. Ag jur gu ñuy sàmm bu ca menn xar génnee dem moom dong, daa féew, till man na koo jàpp mbaa bukki.