Fér-féri

Fér-féri: (njëfka)

Ñàkk a dal, yëngu. Xol buy fér-féri, mooy ku tiit fit wi dalul muy baagante di jóg ak a tóog ni bëy wu rëcc.