Kembaar Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Facebook0Tweet0 Kembaar g: tur Àdduna bi dees koo xaaj juróomi kembaar, muy: Afrig Amerig, Órob, Asi ak Oseyaani. Niral: Senegaal mi ngi ci kembaaru Afrig. Facebook0Tweet0WhatsAppTelegram ← Xànc → Nebbantaan