Mbaar Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Facebook0Tweet0 Ci biir ag sabar dañuy xaaj xeeti ndënd yi ñu ne ag na ñuy tëgge. Amna ca ñuy mbaar am ca ñuy mbëfër am ca ñuy telmbet am ca am ndeer. Yii yépp boo leen boolee ñoo yor sabar gi. Facebook0Tweet0WhatsAppTelegram ← Gale → Mbëfër