Naq Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Facebook0Tweet0 1- Naq: jëf Jël boppub nit dugal ko ci ndox ngir mu xëj. Ku soxor a koy def. Niral: Ndaysaan, waa jee ñu jëme ca mbalka ma de, dees koy naqali. 2- Naq b: tur Ci ron jumbax. Niral: Bul bàyyi sab naq muy feeñ. Facebook0Tweet0WhatsAppTelegram ← Yanq → Koote