Njunux

Njunux l: Day mel ni ndox mu taa ci yoon wi te boo yeggee doo fa fekk dara. Boo duggee ci wata waxtuw digg-bëccëg danga ko gis ca kanam mu mel ni ndox mu taa ci tali bi .