Ãy

 Ãy: tur

Am po la mu xale yu jigéen yi di def.

 

 

 Fite

Fite: jëf

Di waxal nit muy bind.

[En: dictation]
[Fr: dictée]

 Sanax

Sanax: Jëf

Nagam, mel ni lu dee. Tànk yu sanax day woyof toyy mel ni dara newu ci doo yëgati sax ne taq na ci yaw.