Àkk

Àkk: (jëf) Mooy song mbir, niki àkki nit.

Àlliwo

Àlliwo: tur

Dénk wees defar ngir di ca bind. Boo demee ca daara ja, moom la dongo yiy jànge.