Xàmp.
Booy ndékki dangay ŋaañ mburu mi guux kafe gi.
Xàmp.
Booy ndékki dangay ŋaañ mburu mi guux kafe gi.
Ne ŋayam: (njëfka)
Gàncax gu dee ba wow koŋŋ, ba tàmbalee funux. Niral: Boo bàyyee garab mu ne kayam, ginnaaw ay weer nga jaaraat fa danga fekk mu ne ŋayam.
Ŋiim b: tur
Tañaag
Di ñaxtu ndànk ca suuf. Ñimewóo béral la ngay wax ca kaw.
Niral: Xale bii de mi ngi ŋurumtu rekk xamuma lu ko naqari.