Bijjanti Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 19/12/2019 Bijjanti: (jëf) Gunge bu ànd ak waxtaan di dem, waaye doo àgg fa ka ngay gunge jëm.
Biram Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 01/12/2019 Biram: tur Mbiram, mbir mooy benn, bu dee yu bari nga ne ay bir.