Daa j: tur
Ndox mu ñuul mees defar ngir di ci binde.
Daa j: tur
Ndox mu ñuul mees defar ngir di ci binde.
Dagg b: tur
Potu ndagg yi dongo yiy yor bu ñuy yalwaan.
Day: (jëf) Tollu, Niki: Cëy ni mu day! = Cëy ni mu tollu!
Dànna b: (tur) Mooy ku jub loxo, koo xam ne du diir di moy.
Déeyoo: tur
Ñaar ñuy waxtaane ndéey loo xam ne bëgguñu kenn xam ko, dañuy déeyoo.
Déglukaay: tur
[En: earphones]
[Fr: écouteurs]