Duu b: tur
Lees di def am ndugg walla leneen. Niral: Sama yaay a ngi ñëw, yor ab duu def ca màngo bamu fees.
[En: basket]
[Fr: panier]
Duu b: tur
Lees di def am ndugg walla leneen. Niral: Sama yaay a ngi ñëw, yor ab duu def ca màngo bamu fees.
[En: basket]
[Fr: panier]
Duxóos: njëfka
Dugal gu gaaw. Aw dugaliin la. Niral : Yàlla na nu Yàlla ne duxóos àjjana.