Gumm Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 19/12/2019 Ne gumm (njëfka) toog mel ni ku liw bayliku xalaatóo dara.
Guus Auteur de l’article Seex Lóo Date de l’article 23/01/2020 Guus: (jëf) Mooy lu xaw a tooy te tooyul bu baax.