Jëxëm

Jëxëm: jëf

Sëq kawar, dënn bu jëxëm mooy dënn bu sëq kawar.

 

Jóolooli

Jóolooli g: tur

Jóoxoor g

Jóoxoor g = artemisia

Jópp

Jópp: (tur) Lu bari, niki lees jal fenn.

[Fr: Quantité]

Jeqiku

Révolution

Jollasu

Jollasu g: tur

Jollasu téléphone

[En: cellphone]
[Fr: téléphone]

Junjuŋ

Lépp lu ñuy tëgg, ndënd. Tama yi añs. Yii yépp ay xeeti ndënd la: Mbëŋ-mbëŋ g, Cóol m, Ndeer g, Làmb j, Tabala j, Cuŋ l, kenkini l, Tama-boq j, Goroŋ b, Bàll g, Tungni s, Xiin g, Jémbe, Bóngóo g, Tuqsi g, Xalam g.