Junjuŋ

Lépp lu ñuy tëgg, ndënd. Tama yi añs. Yii yépp ay xeeti ndënd la: Mbëŋ-mbëŋ g, Cóol m, Ndeer g, Làmb j, Tabala j, Cuŋ l, kenkini l, Tama-boq j, Goroŋ b, Bàll g, Tungni s, Xiin g, Jémbe, Bóngóo g, Tuqsi g, Xalam g.