Kembaar Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Kembaar g: tur Àdduna bi dees koo xaaj juróomi kembaar, muy: Afrig Amerig, Órob, Asi ak Oseyaani. Niral: Senegaal mi ngi ci kembaaru Afrig.
Kerkiraan Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 19/12/2019 Kerkiraan b (tur) Yéegukaay, fees di jaar ngir yéeg ca kaw.