Kok Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Koo xam ne Niral: Kii nit la kok du jëw. = Kii nit la koo xam ne du jëw
Koom Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 19/12/2019 Koom m (tur) Am-am, niki alal, ay kër, ay wata añs.
Kostan Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Kostan m: tur Baaraamub ginaar biy féete ginnaaw.