Labat (jëf)
Gis jigéen bëgg ko, di wax ak moom ngir takk ko, dox googu ngay dox ngir loolu àntu mooy labat.
Labat (jëf)
Gis jigéen bëgg ko, di wax ak moom ngir takk ko, dox googu ngay dox ngir loolu àntu mooy labat.
Lax (jëf)
Lu tooyoon ba tàmbalee wow nooy, lambax, niki bant bu lax.
Layu b: tur
Laŋ b: tur
Peel
1- Lëm (jëf) nëbb, làq, denc mbir fenn ba kenn du ko gis.
2- Lëm m (tur) Am pax la muy nekk ci garab, jóge ca kaw jan jëm suuf.
[En: 1- hide. 2- tree hole]
[Fr:1- cacher. 2- trou d’arbre]
Coalition d’armes
Leere b: tur
Màrto
1- Lef m: Mbedd mu yaatu lool, fa fasi kursu ya di jëkkantee.
2- Ag fànn ci xam-xam, niki ku jàng ba wann u lef. Moot jeexal ag fànn ci xam-xam.