Loof

Loof (melo) yooy, xiibon ñàkk a regg.

Looy

Looy m: tur 

Njanaaw la,  picc, mu bët yi rëy lool.

Lox

Lox g: tur 

Ag raŋ, nit ñu bari, am ku jiitu am ku ca topp ñu toftaloo noonu.

Loyukaay

Loyukaay g :tur 

Lees di jëfandikoo la ngir bind, day am loy yépp ci biir