Màcc: jëf
Féete, jublu. Niral: Ci lan la sa xam-xam màcc?
Màcc: jëf
Féete, jublu. Niral: Ci lan la sa xam-xam màcc?
Mësëy w: (tur) Mooy tawub wicc-wiccal, taw bu ndaw.
Amna it ñuy wax mësëy-bandaŋ
Coow lu bari, xuloo
Mbatiit l: tur
Mbooleem baaxi aw nit ak seen i jëfiin, ak seen i aada añs.
[En: culture]
[Fr: culture]