Naaxsaay: jëf
Jeex, seey, xiin wu naaxsaay, xiin wu fi ne woon ba yàgg muy dem ndànk ndànk ba set wecc.
Naaxsaay: jëf
Jeex, seey, xiin wu naaxsaay, xiin wu fi ne woon ba yàgg muy dem ndànk ndànk ba set wecc.
Nataal: tur
Këyit wuñu def jëmi nit , mala, gàncax walla lëfñ
Aw tur la
Ndaayànde: Ab dëkk la
Sëb suñu togg, te di ko faral di def ci mburu.
Nduyaan g: tur
[En: charger]
[Fr: chargeur]
Nebbantaan m: tur
Xale bu tollu ci juróomi at ba fukki at.