Njunux

Njunux l: Day mel ni ndox mu taa ci yoon wi te boo yeggee doo fa fekk dara. Boo duggee ci wata waxtuw digg-bëccëg danga ko gis ca kanam mu mel ni ndox mu taa ci tali bi .

Nosukaay

Nosukaay g: tur 

[En: computer]
[Fr: ordinateur]

Nqàmtu

Nqàmtu b: tur 

Dees koy jëfandikoo ngir lim (siifur). 1 nqàmtu la 2 moom la 3 moom la añs.