Nebbantaan

Nebbantaan m: tur 

Xale bu tollu ci juróomi at ba fukki at.

Neeteetóo

Waxatóo. Ne = wax. Diw nee na = Diw wax na.