Ngànj Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Ngànj m: tur Matt mu dijj. Mooy la jaaykati dibi yi di taal.
Ngér Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 19/12/2019 Ngér m (tur) Aw yoon, ab gis-gis, aw xalaatiin.