Njaal m: tur
La ñu lay jox, boo deelee, boo amee ku la jege ku faatu.
Njaal m: tur
La ñu lay jox, boo deelee, boo amee ku la jege ku faatu.
Njakke l :tur
Sama magi jëkkër walla ay rakkam yu jigéen.
Njolloor g: tur
Waxtuw tisbaar. Diggante 14iw ba 16iw. Niral: Sama yaay day aaye dox njolloor.