Raas

Raas: (jëf) Mooy for meññet mu tàbbi.

Niral: Xale dañuy raas déem.

Rañaan

Rañaan : (jëf) dox guddi, tukki guddi. Xëy dafa am, gontu am , rañaan am.

Rañaan

Rañaan (jëf)

Tukki ci guddi bu lépp nee selaw, nga topp guddi gi ngir tukki.