Seeru (jëf)
Seere mbir, teew ci mbir, nekk ci mbir, fekke mbir.
Baataan
Ne selaw: (njëfka) lu ne tekk dara yënguwul. Niki nga dugg ci kër déggoo dara lu yëngu, lépp ne selaw rekk.
[En: quiet]
[Fr: calme]