Suddi Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Suddi b: tur Lees di dajalee ñax yi ak mbalit mi. Ab radu
Suus Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 25/12/2019 Ne suus: njëfka 1- dem ba àgg fa nga jëm, dem ba sës. 2- Am réer la, ngelliir. Niki rajo buy suus. 3- Loo teg ci taal bamu suus. Niki teg sa cere bamu suus