Wirgo

Wirgo w: tur

Melo. Amna wirgo wu xonq, wu weex wu ñuul añs.

[En: color]
[Fr: couleur]

Wopptaal

Wopptaal b: tur 

Barabu fajukaay, fa ñuy taale wopp ya. Ku wopp fa ngay dem ngir tàggoo ak moom.

Wund

Wund: jëf

Wone, junj, bàyyiloo xel. Niral: Saa boo gisee wata bi ci buntu kër gi, day wund ne boroom kër gaa ngi fi.