Baataan
Xallóob b: (tur) Mooy doomi gaynde, gaynde gu ndaw.
Xamtil: jëf
Xamul. til = ul. Nëxtil = nëxul.
Xar m: tur
Mala la, mu ñuy yër ci kër yi.
Xay g: tur
Ag garab la
Lu mel ni ay buum la te ñu koy xollee ci garab. Amna ñuy takk ay xànc ngir faju.