Ruuj Auteur de l’article Jàng Wolof Date de l’article 29/11/2019 Facebook0Tweet0 Ruuj: jëf Setal sab tool ba moo taw, ngir bu tawee rekk nga man a ji. Niral: Baykat yépp ruuj nañu seen i tool. Facebook0Tweet0WhatsAppTelegram ← Njolloor → Céebo